Acts 7:46 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Moom yiw na fa kanam Yàlla, mu ñaan ko, mu sàkkal ko kër ngir askanu Yanqóoba.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Daawuda, ma Yàlla baaxe woon, sàkku woon na am màkkaan ngir Yàllay Yanqóoba.