Acts 7:50 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndax du sama loxo moo defar yëf yooyu yépp?— Moom la Boroom bi doon wax.”
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Loolu lépp, xanaa du sama loxoo ko sàkk?”