Acts 8:10 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Kon ñépp, mag ak ndaw, taq ci moom ne: «Kii mooy jaasiy Aji Kàttan ji.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñépp, mag ak ndaw, teewlu ko, naan: «Kii mooy dooley Yàlla ci boppam. Moom lañuy wax “Màggle”.»
Recommended Reading