Acts 8:12 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Waaye bi ñu gëmee xebaar bu baax, bi Filib yégle jëm ci nguurug Yàlla ak turu Yeesu Kirist, góor ak jigéen daldi nangu, ñu sóob leen ci ndox.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye ba ñu gëmee Filib, ma leen xamal xibaaru jàmm, bi jëm ci nguurug Yàlla ak turu Yeesu Almasi, góor ak jigéen daldi nangu, ñu sóob leen ci ndox.