Acts 8:19 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
ne leen: «Mayleen ma sañ-sañ boobu, ba ku ma teg samay loxo, nga jot Xel mu Sell mi.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mu ne leen: «Mayleen ma man itam xam-xam bii, ngir ku ma teg loxo, nga jot Noo gu Sell gi.»