Acts 8:20 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye Piyeer ne ko: «Asarul ak sa xaalis, yaw mi yaakaar ne, man ngaa jënd mayu Yàlla ak xaalis.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Piyeer ne ko: «Na sa xaalis ànd ak yaw asaru, ndegam ab xaalis nga yaakaara jënde mayu Yàlla!