Acts 8:24 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Simoŋ nag ne leen: «Ñaanal-leen ma ci Boroom bi, ngir mu fegal ma li ngeen wax.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Simoŋ ne leen: «Ñaanal-leen ma Boroom bi, yeen ci seen bopp, ngir li ngeen wax lépp, lenn bañ ma cee dab.»