Acts 8:25 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Noonu bi ñu seedeelee Yàlla te wax ci kàddoom, ñu dellu Yerusalem, di xamle xebaar bu baax bi ci dëkk yu bare yu waa Samari.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Gannaaw ba Piyeer ak Yowaan seedeelee kàddug Boroom bi, biral ko, Yerusalem lañu dellu, di xamle xibaaru jàmm bi ci ay dëkki Samari yu bare.