Acts 8:33 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ci toroxteem nangu nañu dëggam;ñi mu tollool jamono, ku ci xalaat lii?Jële nañu bakkanam ci àddina.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci biir toroxteem lañu ko xañ dëggam; kuutaayam nag, ana ku ci mana wax? Ndegam bakkanam lañu toxale kaw suuf.»