Acts 8:34 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Jaraaf ja nag ne Filib: «Maa ngi lay laaj, ci mbirum kan la yonent bi jëmale wax ji? Ndax mbirum boppam lay wax mbaa mu keneen?»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Jaraaf ja ne Filib: «Yaw laay laaj, ci kan la yonent bi wax lii? Boppam lay wax am keneen?»