bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Acts 8:40
Acts 8:40 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Filib moom teeri dëkku Asot, muy jaar ci dëkk yépp, di fa xamle xebaar bu baax bi, ba kera muy ñëw dëkku Sesare.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Filib moom, dëkk ba ñuy wax Asot la gisaat boppam. Mu wéye di xamle xibaaru jàmm bi ci dëkkoo dëkk, ba àgg Sesare.