Acts 8:6 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi ko mbooloo mi déggee te gis kéemaan yi muy def, ñu bokk benn xalaat, fekki ko ci li mu wax.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba waa dëkk ba déggee mbaa ñu gis kéemaan ya muy def, ñoo bokk teewlu ay waxam.