Acts 8:9 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Amoon na nag nit ku tudd Simoŋ, di luxuskat bu yàgg ca dëkk ba, te daan yéem waa Samari gépp, ci naan: «Aji Màgg laa.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ku ñuy wax Simoŋ nag yàggoon na ca dëkk ba, di ñeengo. Ku waar waa Samari la woon, te doon tuddoo nit ku màgg.