Acts 9:11 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Boroom bi ne ko: «Jógal, nga jaar ci mbedd, mi ñuy wax Mbedd mu jub mi, te seet ci kër Yudaa nit ku tudd Sool te dëkk Tars, ndaxte mu ngay ñaan.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Sang bi ne ko: «Demal ba ca mbedd, ma ñuy wax Mbedd mu jub, te nga seet ca kër Yuda ku ñuy wax Sóol te dëkke Tàrs. Ma ngay ñaan.