Acts 9:12 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Te gis na cim peeñu nit ku tudd Anañas, mu dugg, teg ko ay loxo, ba muy gisaat.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Dafa gis cim peeñu ku ñuy wax Anañas duggsi, teg ko loxo, ngir mu dellu di gis.»
Recommended Reading