Acts 9:17 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ci kaw loolu Anañas dem, dugg ca kër ga, teg ay loxoom Sool. Mu ne ko: «Sool sama mbokk, Boroom bi Yeesu, mi la feeñu woon ci kaw yoon wi, bi ngay dikk, moo ma yónni, ngir nga dellu di gis te fees ak Xel mu Sell mi.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci kaw loolu Anañas dem, dugg ca kër ga, teg Sóol loxo, ne ko: «Mbokk mi Sóol, Sang Yeesu, mi la feeñu woon ci yoon wi nga dikke, moo ma yebal ci yaw, ngir nga dellu di gis te feese Noo gu Sell gi.»