Acts 9:2 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
laaj ko ay bataaxal yu muy yóbbul jànguy dëkku Damas. Noonu ñu mu fa fekk, te ñu bokk ci yoon wi, góor mbaa jigéen, mu am dogalu yeew leen, indi leen Yerusalem.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
di sàkku ay bataaxal yu ñeel jànguy dëkk ba ñuy wax Damaas, bataaxal yu yóbbante ndigal lu yeewlu képp ku ñu fa gis ku bokk ci Yoon woowu, góor ak jigéen, ngir mu jàpp leen, indi Yerusalem.