bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Acts 9:22
Acts 9:22 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Moona Sool di gën a am kàttan, bay jaaxal Yawut yi dëkk Damas, ci di leen wax ay firnde, ne Yeesu mooy Almasi bi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Teewul Sóol gëna am manoore, ba far jaaxal Yawut ñi dëkke Damaas, di firndeel ne Yeesu mooy Almasi.