Acts 9:24 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye Sool yég seen pexe. Fekk guddi ak bëccëg ñu doon wottu bunt yi yépp, ngir man koo bóom.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Sóol nag yég seen mébét. Guddi ak bëccëg lañu doon wattu bunti dëkk ba, ngir bóom ko.