Acts 9:26 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi Sool agsee Yerusalem, mu jéem a ànd ak taalibe yi, waaye ñépp ragal ko, ndax gëmuñu woon ag taalibeem.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba Sóol agsee Yerusalem, jéem naa jaxasook taalibe yi, waaye ñépp a ko ragal, ndax ñàkka gëm ag taalibeem.