Acts 9:28 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu mu nekk ak ñoom ci Yerusalem, di dugg ak a génn, di wax ak fit ci turu Boroom bi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba loolu amee Sóol ànd ak ndaw yi di dem ak a dikk ci biir Yerusalem, di waaree aw fit ci turu Sang bi.