Acts 9:29 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Muy wax ak di werante ak Yawut yiy làkk gereg, waaye ñu di ko wut a rey.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mu boole ci di wax ak a werante ak Yawut ñiy làkk gereg, te ñoom ñu di ko fexee rey.