Acts 9:33 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
mu gis fa nit ku làggi, tudd Ene, tëdd ci basaŋ diirub juróom-ñetti at.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mu gis foofa waa ju ñuy wax Ene. Fekk na diiru juróom ñetti at, cib lal rekk lay tëdd ndax yaram wu làggi.
Recommended Reading