Acts 9:35 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi ko waa diiwaani Lidd ak Saron gépp gisee, ñu daldi woññiku ci Boroom bi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mboolem waa diiwaani Lidd ak Saron nag gis ko, ñoom ñépp waññiku ci Sang bi.