Acts 9:36 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Amoon na nag ci dëkku Yope taalibe bu jigéen bu tudd Tabita, liy tekki «Dorkas,» maanaam «kewel,» te muy wéy ci jëf yu baax ak saraxe.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Dëkk ba ñuy wax Yope, ab taalibe bu jigéen a nga fa woon, ñu di ko wax Tabita mbaa Dorkas ci làkku gereg. Def lu baax ak sarxe la saxoo woon.