Acts 9:38 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Gannaaw Lidd sorewul ak Yope nag, te taalibe yi dégg ne, Piyeer a nga fa, ñu yónnee ko ñaari nit, ñaan ko mu ñëw ci ñoom ci saa si.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci biir loolu taalibe yi dégg ne Piyeer a nga Lidd, te Lidd sorewul Yope. Ñu yebal ñaari nit ca moom, ngir ñaan ko mu ñëw te baña yeex.