Acts 9:6 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye jógal, dugg ca dëkk ba, te dinañu la wax li nga war a def.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Léegi nag, jógal, dugg ci dëkk bi, dees na la wax li nga wara def.»