Amos 1:8 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Maay fàkkas waa Asdodd, fàkkas boroom yetu nguur fa Askalon, fél Ekkron, ndesu Filisteen ña sànku.» Boroom bi Aji Sax jee ko wax.