Amos 3:1 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Dégluleen kàddu gii Aji Sax ji wax ci yeen, bànni Israyil, mu jëm ci seen mboolem xeet wi mu génnee réewum Misra. Mu ne: