Amos 6:13 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yeena ngi damu ca dëkk ba ñuy wax Lodebar (mu firi Amul njariñ) te naan: «Xanaa du sunu dooley bopp lanu nangul sunu bopp dëkk bu am doole ba ñuy wax Karnayim (mu firi Ñaari béjjén)?»