Colossians 1:12 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Dingeen gërëm Yàlla Baay bi, ànd ci ak mbég, moom mi leen jagleel, ngeen bokk ci cér, bi mu dencal gaayam yu sell yi ci leer.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
te ngeen di sante Baay bi, mbég, moom mi leen yellale ab cér ca muuru ñu sell ña, ca réewum leer ga.