Colossians 1:15 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Doom jooju moo di melokaanu Yàlla, ji kenn gisul. Mooy taaw bi, ki gën a màgg lépp luy mbindeef.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Doom jooju moo di niruwaale Yàlla, mi kenn manula gis, mooy taaw bi, ki jiitu mépp mbindeef.