Colossians 1:17 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Laata dara di am, fekkoon na moom mu nekk, te lépp a ngi jàppoo ci moom.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mooy ki nekkoon naka jekk balaa daraa nekk, te lépp ci moom la sottee ba temboo.