Colossians 1:22 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
léegi nag Yàlla jubale na leen ak boppam jaare ko ci deewu Kirist ci yaramu nitam, ngir taxawal leen ca kanamam, ngeen sell te ñàkk sikk ak i ŋàññ.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
tey, deewug yaram, deewug suux, gi Almasi dee, moom la leen Yàlla jubalee ak boppam, ba teewal leen fi kanamam, ngeen di ñu sell, mucc sikk, seen der set wecc.