Colossians 1:4 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
ndaxte yég nanu seen ngëm ci Kirist Yeesu ak seen mbëggeel ci gaayi Yàlla yépp.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
dégg nanu ngëm gi ngeen gëm Almasi Yeesu, ak cofeel gi ngeen sopp gëmkat ñu sell ñépp,