Colossians 1:7 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
moom ngeen jànge ci Epafras, miy sunu nawle ci liggéey bi te nu sopp ko, di jawriñu Kirist bu takku ngir seen njariñ.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Noonu ngeen ko jànge ci Epafras, sunu mbokkum surga biy sunu soppe, te di jawriñu Almasi bu wóor bi nu jàpple,