Colossians 2:1 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Bëgg naa nag, ngeen xam bëre bu metti, bi may bëre ngir yéen, ngir waa Lawdise ak ñépp ñi ma musul a teg bët. Damay def sama kem-kàttan,
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Bëgg naa nag, ngeen xam xare bu metti, bi ma leen di xareel, yeen ak waa Lawdise ak mboolem gëmkat ñi ma masula teg bët,
Recommended Reading