Colossians 2:15 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Futti na kilifa yi ak boroom sañ-sañ yi, weer leen ci kanamu ñépp, sëkktal leen niy jaam ndax ndam la Kirist jële ca bant ba.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Moo dog sidditi boroom nguur yeek boroom sañ-sañ yi ci jaww ji, ñu doon ay jaam yu mu jàppe xare. Moo leen weer it ci kanam ñépp, diriwaale leen ca biir njaab ma topp ca ndam, la Almasi ame ca bant ba.