Colossians 2:17 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Loolu lépp nag takkandeer la woon buy misaal li waroon a ñëw, waaye lu dëggu li mi ngi ci Kirist.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Loolu lépp takkndeeru yaram wuy jëmmal lu dikkagul, moom rekk la woon. Waaye yaram wi dëgg moo di Almasi.