Colossians 2:19 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Taqul ci Kirist, miy bopp bi yilif jëmm ji. Bopp bee tax ba jëmm jépp, ji siddit yi ak tenqo yi téye te taqale ko, di màgg màgg gi ko Yàlla di jox.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñooñu jokkuwuñu ci Almasi, miy bopp bi, te ci bopp bi la yaram wi wépp di jëfandikoo siddit yeek tenqo yi, ba suuxatu, ngir lépp mànkoo ba mana màgg, ni ko Yàlla di màggale.