Colossians 2:22 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Sàrt yooyu ñu ngi aju ci ndigali nit ñi ak seen njàngale. Yëf yi ñu tudd yépp, dees na leen jariñoo, ba ñu jeex.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Te mboolem yëf yooyu dogali yoon yi jëm day jeex doŋŋ bu ñu leen jëfandikoo. Loolu ay santaane aki àlluway nit doŋŋ la.