Colossians 2:23 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Dëgg la, seeni sàrt dañuy dénkaane pasteef ci jaamu Yàlla, di toroxlu ak di fitnaal seen yaram. Waaye sàrt yooyu nag amuñu benn njariñ, ngir nit ñi noot seen nafsu.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Dëgg la, xel man naa nangu dogali yoon yu ni mel, ndax laaj na nit ki pastéefu ci diine ju mu tegool boppam, laaj na it toroxlu, ak coonoy yaram yu tukkee ci yar bu metti bu nit kiy tegoo, waaye jariñul dara ku bëgga moom bakkanam.