Colossians 2:3 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ci moom lañu denc lépp lu ñuy sàkku ci xel ak ci xam-xam.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci moom la mboolem alal ji ci xel ak xam-xam, dëxëñe.