Colossians 2:9 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndaxte ci Kirist, maanaam ci yaramu nitam, la matug Yàlla gépp dëkk,
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndax kat ci Almasi, ci yaramu nitam la léppi Yàlla dëkke, ba mat sëkk ci moom,