Colossians 3:13 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Muñalanteleen, di baalante, su amee kuy tawat moroomam. Baalanteleen, ni leen Boroom bi baale.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Muñalanteleen te di balante, ndegam kenn a am lenn lu mu sikke moroomam. Ni leen Boroom bi baale, deeleen balantee noonu.