Colossians 3:14 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ci kaw loolu lépp amleen mbëggeel, giy jókkaale lépp, ba mu mat.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci kaw loolu lépp nag, tegooleen cofeel; mooy xànc gi leen faste, ba seenug bennoo mat sëkk.