Colossians 3:15 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Na jàmm ji Kirist di joxe noot seeni xol, ndaxte Yàlla woo na leen ci loolu, mel ni ay cér yu bokk benn yaram; te gërëmleen Yàlla.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Na jàmmu Almasi saytu seen xol. Ci jooju jàmm lañu leen woo, fekk leen ngeen di wenn yaram doŋŋ, te it saxooleen cant.