Colossians 3:17 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Te lu ngeen man a def, muy ci wax mbaa ci jëf, wéerleen ko ci turu Boroom bi Yeesu, jaare ci moom gërëm Yàlla Baay bi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Lu ngeen mana def, muy ci wax, di ci jëf, defleen ko ci turu Sang Yeesu, tey sant Yàlla Baay bi ci moom.