Colossians 3:20 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Xale yi, déggal-leen seeni waajur ci lépp, ndaxte looloo rafet ci ñi bokk ci Boroom bi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Xale yi, déggal-leen seeni waajur ci lépp, nde loolu mooy li Boroom bi rafetlu.