Colossians 3:23 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Lu ngeen man a def, na ci seen xol tàlli; ngeen def ko ngir Boroom bi, te du ngir nit,
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Lu ngeen mana def, liggéeyeleen ko xol bu tàlli, ni bu ñeelul woon nit doŋŋ, xanaa Boroom bi.